Ab jukkib Wikipedia.
|
|
 |
|
Seetal ci 727 jukki ci kàllaama wolof:
|
 |
Nas wi bokk na ci bëre biy dàq ber bi ñu ber yenn làkk yi (rawatina ci internet bi), xëcc itam gëndaloo guy yamale te di jàpplante, loolu di sukkandiku ci sañ-sañu askan yi gàddu seen kuute ci caada.
Àdduna bu gën di yamale, ak gën di tinkiku ci la aju !!!
|
|
|
|
Nataalu ayubés bi
|
Lat Joor Joob Ngóone Latiir Faal
|
Lat Joor Joob waxambaane wu jàmbaare la woon, wu amoonug dogu, mu bokkoon ci ñu mag ñi daa jàmmaarlook sancaan yi ci goxub Afrig, mu nekkoon di kenn ci ñi ci gën a jàmbaare, gën cee fés, kenn melul ni moom ci sopp suufam ak ndonoom. Amoon na fit wow kenn du ko doyadil, daawul tiit ak lu man a xew. Nekkoon na njiitul xare lu mag, di aji politig ju ñaw, ju di boroomug jommal. Ci atum 1862 g.j, la ñu fal Lat Joor Dammeel ca Kajoor.
|
Yeneen sémbi Wikipedia ciy kàllaamay waa Afrig
Afar · Afrikaans · Akan · አማርኛ · Bamanankan · Chicheŵa · chiShona · chiTumbuka · Ɛʋɛ · Fulfulde · Gĩkũyũ · هَوُسَ · Igbo · isiXhosa · isiZulu · Kinyarwanda · Kirundi · Kiswahili · Kongo · Lingála · Luganda · Malagasy · Malti · Oromoo · Oshiwambo · Sängö · Sesotho · Setswana · siSwati · Soomaaliga · ትግርኛ · tshiVenda · Twi · Xitsonga · (ngir yeneeni Wikipedia, xoolal ci bànqaasu wet gi)
Ay kàllaamay waa Afrig ci wikipedia yu ëppal 1000 jukki
Afrikaans · Kiswahili · Yorùbá ·