>


Web - Amazon

We provide Linux to the World


We support WINRAR [What is this] - [Download .exe file(s) for Windows]

CLASSICISTRANIERI HOME PAGE - YOUTUBE CHANNEL
SITEMAP
Audiobooks by Valerio Di Stefano: Single Download - Complete Download [TAR] [WIM] [ZIP] [RAR] - Alphabetical Download  [TAR] [WIM] [ZIP] [RAR] - Download Instructions

Make a donation: IBAN: IT36M0708677020000000008016 - BIC/SWIFT:  ICRAITRRU60 - VALERIO DI STEFANO or
Privacy Policy Cookie Policy Terms and Conditions
Seex Anta Joob - Wikipedia

Seex Anta Joob

Ab jukkib Wikipedia.

Seex Anta Joob
Seex Anta Joob

Seex anta joob a ngi judd ci 29 tabaski ci 1923 ca Jurbel- saay 7 diggi gamu ci 1986 ca Ndakaaru doonoon ab taariixkat bu waa senegaal. Moo fesal li Afrig, rawatina Afrig gu ñuul gi indi ci xayug àdduna bi. Donte yenn ci ay yebbeem(thèse), ba tay, am na ñu leen nanguwul rawatina yenn waa Tugal yi, li ëpp ci li mu bind wér na ñépp.

Tërëlin

[Soppi] nit ki ak jëfam

Seex anta joob mi ngi judd ci 29 tabaski 1923 ca Ceytun, ci diwaanu Jurbel, ci diggu Senegaal. Bi mu amee 23 at la dem Paris ngir jang jëmm ak simi, ba yàgg mu boole ci taariix ak Xam-xami mboolaay yi. Moom gis-gisu boppam la amoon ci lu ñu da jangale ca jamono yooyule, naa Afrig amul demb.

Ci 1951 la bind ab yebbi ci yoonalug (direction) Marcel Griaule ca Daara ju kawe ju Paris, mu wax fa ne Isipt gu yàgg ga, ay waa afrig yu ñuul a fa dëkkoon, nit it làkk ak caaday waa Isipt ñoo tas ci Sowwu Afrig. Donte ay sëriñam nanguwuñuñ yooyule faramface, waaye ni ko Doué Gnonsoa waxee, juroon na ay yëngu-yëngu yu bari ci bim ko defee téere dupee ko Réewi ñu ñuul ñi ak caada, gi mu siiwal ci 1954. Ci 1960 la mujje jott ay lijaasaam. Ci genn jamono ji muy wéy di taggatu ci jëmmug saal ca Faraas. xam-xamam maccoon na jëm ci fànn yu bari.

Dafa cëslaayuwoon ci bindkati waa geres yu yàgg yooyule di Herodote ak Strabon ngir nafar faramfaceem googu mu naa waa Isipt yu yàgg ya ak waa afrig yu ñuul yi benn la ñu ci jëmm (seen meloow der, melokaanu kawar, gu bakkan ak guy tuñ). Bi mu xoole xoolaat xibaar yi mu am, la ni caadaay waa Isipt, caadaay ku «ñuul» la. Ci wàllu làkk, mu gis ne wolof ak làkku waa Isipt yu yàgg ya ñoo bokki maam.

Ci atum 1970, Seex anta bokk ci mbooloom xam-xam, ci ndigalu UNESCO, miy war a bind ab téere ci taariix gu daj gu Afrig. Ci li ñeel mbindum boobule téere, la bokk ca ndajeem réew yi ca Keer, mu fay mengale gëstuwinam ak ay ngerteem ak yeneen boroom xam-xam yi ci àdduna bépp te seenug xam-xam ñeel wàll wi. Ci lu weesu boobu ndaje lañ ko féetaleel ak xaaj bu mu war a bind ci soqikoo gu waa Isipt yu yàgg ya. Tënkug jeexitu(rapport final) boobule ndaje fesal na deggoo ga amoon ci diggantey boroom xam-xam ya, ba mu des kenn, ci li Seex Anta Joob ak Théophil Obenga indi woon, ñeel nuroog caada gi nekk ci diggante Isipt gu yàgg ga ak Afrig gu ñuul gi. Ci noonu sëriñ (professeur) Jean Vercoutter biral yii kàddu: «Isipt waa Afrig la woon ci mbindinam ak ci xalaatinam». Sëriñ Leclant it gis menn melokaan mi ci seen jikko ak xalaatin. Waaye ba tay jii, yenn boroom xam-xam yi da ñoo jàpp ne ca Isipt ñu ñuul rekk a fa dëkkoon ba bés bi ñuy ñakk seenug tembte, ñeneen ñi jàpp ne ab njaxas a fa amoon, maanaam ay xeet yu bari.

Ci beneen fànn, ci 1947 la dugg ci politig, di xeex ngir tembteeg Afrig ak sosteefu ab Bennoob Réewi Afrig yi.

Seex Anta Joob a ngi génn àdduna ci Ndakaaru ci diggi gamu 1986. Jàppee woon nañ ko niki bindkatu waa Afrig bi gën a raññeewu ci XXu xarnu bi.

[Soppi] Ay faramfaceem ci taariix

Seex Anta Joob ci téere bi mu mujjee sadd, laataa génnug àddunaam, la dajale ngertey liggéeyam yépp, di ci gaar faramfaceemug taariix gi mu def, di ci tont it taariixat yi koy ŋaññ.

[Soppi] Ni xayug ku ñuul jiitoo

Anta gisoon na ne nit ki njëkk Afrig la fekk-baax, mi ngi feeñ ci li wër barabi gëweelu Afrig gi, ci diwaanu Laamaar yu Mag yi. Su nit njëlbeenoo Afrig, kon ci gisinam, Seex Anta, gis ne feñtey xay yi njëkk Afrig rekk la war a man a amee. Kon, Afrig du rekk am na demb, waaye xayam mooy gi njëkk. Ni ko Nathalie Michalon waxee, nit a ngi juddoo Afrig, fa la ag xereñam dooree, mu juge fa dem ci yeneen diwaan yi. Ci Afrig la nit tambalee sàkkiy jumtukaay, samp kër, di béy di togg, añs.

[Soppi] Lëkkalekaay yu biti


< Static Wikipedia 2008 (no images)

aa - ab - af - ak - als - am - an - ang - ar - arc - as - ast - av - ay - az - ba - bar - bat_smg - bcl - be - be_x_old - bg - bh - bi - bm - bn - bo - bpy - br - bs - bug - bxr - ca - cbk_zam - cdo - ce - ceb - ch - cho - chr - chy - co - cr - crh - cs - csb - cu - cv - cy - da - de - diq - dsb - dv - dz - ee - el - eml - en - eo - es - et - eu - ext - fa - ff - fi - fiu_vro - fj - fo - fr - frp - fur - fy - ga - gan - gd - gl - glk - gn - got - gu - gv - ha - hak - haw - he - hi - hif - ho - hr - hsb - ht - hu - hy - hz - ia - id - ie - ig - ii - ik - ilo - io - is - it - iu - ja - jbo - jv - ka - kaa - kab - kg - ki - kj - kk - kl - km - kn - ko - kr - ks - ksh - ku - kv - kw - ky - la - lad - lb - lbe - lg - li - lij - lmo - ln - lo - lt - lv - map_bms - mdf - mg - mh - mi - mk - ml - mn - mo - mr - mt - mus - my - myv - mzn - na - nah - nap - nds - nds_nl - ne - new - ng - nl - nn - no - nov - nrm - nv - ny - oc - om - or - os - pa - pag - pam - pap - pdc - pi - pih - pl - pms - ps - pt - qu - quality - rm - rmy - rn - ro - roa_rup - roa_tara - ru - rw - sa - sah - sc - scn - sco - sd - se - sg - sh - si - simple - sk - sl - sm - sn - so - sr - srn - ss - st - stq - su - sv - sw - szl - ta - te - tet - tg - th - ti - tk - tl - tlh - tn - to - tpi - tr - ts - tt - tum - tw - ty - udm - ug - uk - ur - uz - ve - vec - vi - vls - vo - wa - war - wo - wuu - xal - xh - yi - yo - za - zea - zh - zh_classical - zh_min_nan - zh_yue - zu -

Static Wikipedia 2007 (no images)

aa - ab - af - ak - als - am - an - ang - ar - arc - as - ast - av - ay - az - ba - bar - bat_smg - bcl - be - be_x_old - bg - bh - bi - bm - bn - bo - bpy - br - bs - bug - bxr - ca - cbk_zam - cdo - ce - ceb - ch - cho - chr - chy - co - cr - crh - cs - csb - cu - cv - cy - da - de - diq - dsb - dv - dz - ee - el - eml - en - eo - es - et - eu - ext - fa - ff - fi - fiu_vro - fj - fo - fr - frp - fur - fy - ga - gan - gd - gl - glk - gn - got - gu - gv - ha - hak - haw - he - hi - hif - ho - hr - hsb - ht - hu - hy - hz - ia - id - ie - ig - ii - ik - ilo - io - is - it - iu - ja - jbo - jv - ka - kaa - kab - kg - ki - kj - kk - kl - km - kn - ko - kr - ks - ksh - ku - kv - kw - ky - la - lad - lb - lbe - lg - li - lij - lmo - ln - lo - lt - lv - map_bms - mdf - mg - mh - mi - mk - ml - mn - mo - mr - mt - mus - my - myv - mzn - na - nah - nap - nds - nds_nl - ne - new - ng - nl - nn - no - nov - nrm - nv - ny - oc - om - or - os - pa - pag - pam - pap - pdc - pi - pih - pl - pms - ps - pt - qu - quality - rm - rmy - rn - ro - roa_rup - roa_tara - ru - rw - sa - sah - sc - scn - sco - sd - se - sg - sh - si - simple - sk - sl - sm - sn - so - sr - srn - ss - st - stq - su - sv - sw - szl - ta - te - tet - tg - th - ti - tk - tl - tlh - tn - to - tpi - tr - ts - tt - tum - tw - ty - udm - ug - uk - ur - uz - ve - vec - vi - vls - vo - wa - war - wo - wuu - xal - xh - yi - yo - za - zea - zh - zh_classical - zh_min_nan - zh_yue - zu -

Static Wikipedia 2006 (no images)

aa - ab - af - ak - als - am - an - ang - ar - arc - as - ast - av - ay - az - ba - bar - bat_smg - bcl - be - be_x_old - bg - bh - bi - bm - bn - bo - bpy - br - bs - bug - bxr - ca - cbk_zam - cdo - ce - ceb - ch - cho - chr - chy - co - cr - crh - cs - csb - cu - cv - cy - da - de - diq - dsb - dv - dz - ee - el - eml - eo - es - et - eu - ext - fa - ff - fi - fiu_vro - fj - fo - fr - frp - fur - fy - ga - gan - gd - gl - glk - gn - got - gu - gv - ha - hak - haw - he - hi - hif - ho - hr - hsb - ht - hu - hy - hz - ia - id - ie - ig - ii - ik - ilo - io - is - it - iu - ja - jbo - jv - ka - kaa - kab - kg - ki - kj - kk - kl - km - kn - ko - kr - ks - ksh - ku - kv - kw - ky - la - lad - lb - lbe - lg - li - lij - lmo - ln - lo - lt - lv - map_bms - mdf - mg - mh - mi - mk - ml - mn - mo - mr - mt - mus - my - myv - mzn - na - nah - nap - nds - nds_nl - ne - new - ng - nl - nn - no - nov - nrm - nv - ny - oc - om - or - os - pa - pag - pam - pap - pdc - pi - pih - pl - pms - ps - pt - qu - quality - rm - rmy - rn - ro - roa_rup - roa_tara - ru - rw - sa - sah - sc - scn - sco - sd - se - sg - sh - si - simple - sk - sl - sm - sn - so - sr - srn - ss - st - stq - su - sv - sw - szl - ta - te - tet - tg - th - ti - tk - tl - tlh - tn - to - tpi - tr - ts - tt - tum - tw - ty - udm - ug - uk - ur - uz - ve - vec - vi - vls - vo - wa - war - wo - wuu - xal - xh - yi - yo - za - zea - zh - zh_classical - zh_min_nan - zh_yue - zu

span style="font-weight: bold;">Our
"Network":



Project Gutenberg

href="https://gutenberg.classicistranieri.com">https://gutenberg.classicistranieri.com



Encyclopaedia Britannica 1911

href="https://encyclopaediabritannica.classicistranieri.com">https://encyclopaediabritannica.classicistranieri.com



Librivox Audiobooks

href="https://librivox.classicistranieri.com">https://librivox.classicistranieri.com



Linux Distributions

https://old.classicistranieri.com



Magnatune (MP3 Music)

href="https://magnatune.classicistranieri.com">https://magnatune.classicistranieri.com



Static Wikipedia (June 2008)

href="https://wikipedia.classicistranieri.com">https://wikipedia.classicistranieri.com



Static Wikipedia (March 2008)

href="https://wikipedia2007.classicistranieri.com/mar2008/">https://wikipedia2007.classicistranieri.com/mar2008/



Static Wikipedia (2007)

href="https://wikipedia2007.classicistranieri.com">https://wikipedia2007.classicistranieri.com



Static Wikipedia (2006)

href="https://wikipedia2006.classicistranieri.com">https://wikipedia2006.classicistranieri.com



Liber Liber

href="https://liberliber.classicistranieri.com">https://liberliber.classicistranieri.com



ZIM Files for Kiwix

https://zim.classicistranieri.com





Other Websites:



Bach - Goldberg Variations

https://www.goldbergvariations.org



Lazarillo de Tormes

https://www.lazarillodetormes.org



Madame Bovary

https://www.madamebovary.org



Il Fu Mattia Pascal

https://www.mattiapascal.it



The Voice in the Desert

https://www.thevoiceinthedesert.org



Confessione d'un amore fascista

https://www.amorefascista.it



Malinverno

https://www.malinverno.org



Debito formativo

https://www.debitoformativo.it



Adina Spire

https://www.adinaspire.com




atOptions = { 'key' : 'e601ada261982ce717a58b61cd5b0eaa', 'format' : 'iframe', 'height' : 60, 'width' : 468, 'params' : {} };

Our "Network":

Project Gutenberg
https://gutenberg.classicistranieri.com

Encyclopaedia Britannica 1911
https://encyclopaediabritannica.classicistranieri.com

Librivox Audiobooks
https://librivox.classicistranieri.com

Linux Distributions
https://old.classicistranieri.com

Magnatune (MP3 Music)
https://magnatune.classicistranieri.com

Static Wikipedia (June 2008)
https://wikipedia.classicistranieri.com

Static Wikipedia (March 2008)
https://wikipedia2007.classicistranieri.com/mar2008/

Static Wikipedia (2007)
https://wikipedia2007.classicistranieri.com

Static Wikipedia (2006)
https://wikipedia2006.classicistranieri.com

Liber Liber
https://liberliber.classicistranieri.com

ZIM Files for Kiwix
https://zim.classicistranieri.com


Other Websites:

Bach - Goldberg Variations
https://www.goldbergvariations.org

Lazarillo de Tormes
https://www.lazarillodetormes.org

Madame Bovary
https://www.madamebovary.org

Il Fu Mattia Pascal
https://www.mattiapascal.it

The Voice in the Desert
https://www.thevoiceinthedesert.org

Confessione d'un amore fascista
https://www.amorefascista.it

Malinverno
https://www.malinverno.org

Debito formativo
https://www.debitoformativo.it

Adina Spire
https://www.adinaspire.com