Web Analytics Made Easy - Statcounter

See also ebooksgratis.com: no banners, no cookies, totally FREE.

CLASSICISTRANIERI HOME PAGE - YOUTUBE CHANNEL
Privacy Policy Cookie Policy Terms and Conditions
Kawlak - Wikipedia

Kawlak

Ab jukkib Wikipedia.


Kawlak am réewu-taax mu mag la ca senegaal, féete ci li tollook bëj-saalum-penku Ndakaaru. Mooy péyu diwaanu kawlak ak goxu Kawlak.

Fi Kawlak féete ci lonkoyoonu Senegaal
Fi Kawlak féete ci lonkoyoonu Senegaal

Tërëlin

[Soppi] Ci lu daj

Ba ko tubaab yi di sanc benn dëkk rekk a fa nekkoon muy Ndangaan. Kawlak yàgg naa doon ab tombum jaaru gerte gi ñu daa béy ci yeneen diwaan yi ko wër, ca waaxam wa lañ daa jaarale gerte gi jëme Ndakaaru. Kawlak a ngi bokkoon ci nguuru Saalum ga woon. Ba fa waa faraas yi di sanc buur-saalum da leen xajaloon ngir bañoon fitna judd ci seen diggante.

Jumaa ju Medina Baay
Jumaa ju Medina Baay

[Soppi] Diine

Kawlak am na ab jàngu bu mag, Saint Theophile Turpin mooy kiñ ko tudde. Njiitu jàngu bu Seneegal bu tay jii, Tewodoor adiriye saar, nekkoon na fa ci diir bu guddu.

Jumaay Kawlak, bi Baay Ñas tambalee woon tabax, tay jii ci diggu ab dëkk bu rëy la ne: Medina Baay. Mooy fa njabootu sëriñu tiijaan boobule, génn àdduna ci atum 1975, dëkke.

[Soppi] Melosuuf

Ci waññi yi ñu amal ci atum 1988 ak 2002, Kawlak amoon na 150 061 ak 172 305 ciy way-dëkk. Ci 2007 ciy ay nattale yu nguuru senegaal def, jàpp nañ ne war naa mat 185 976 ciy way-dëkk.

[Soppi] Koom-koom

Kawlak ab selebiyoon bu mag la. Ci yaxantug gerte gi la réewu-taax mu kawlak mas di dund. Bari na ay ja yu mag aki luuma.

[Soppi] Téerekaay

  • {fr} H. Bessac, « Découverte de gisements néolithiques au sud de Kaolack (Sénégal) », Notes Africaines, Dakar, IFAN, 1952, n° 55, p. 65-69
  • {fr} Etienne Badiane, Développement urbain et dynamiques des acteurs locaux  : le cas de Kaolack au Sénégal, 2004
  • {fr} André Dessertine, Un port secondaire de la Côte occidentale d’Afrique, Kaolack. Étude historique, juridique et économique, des origines à 1958, Université de Dakar, 1959, 172 p. (Diplôme d’Etudes Supérieures de droit).
  • {fr} Ibrahima Diouf, Kaolack : De l'arachide aux activités informelles, 1988
  • {fr} Joseph Fouquet, La traite des arachides dans le pays de Kaolack et ses conséquences économiques, sociales et juridiques, Saint-Louis, IFAN-Université de Dakar, 1958, 263 p. (Etudes sénégalaises n°8) (Thèse de Droit, Montpellier, 1951, publiée)
  • {fr} Aline Garderet, Les fonctions de capitale régionale de Kaolack, Université de Bordeaux, Travail d'études et de recherches, 1968, 129 p.
  • {fr} Djibril Gueye, L’école coloniale à Kaolack 1893-1928, Dakar, Université Cheikh Anta Diop, 2002, 105 p. (Mémoire de Maîtrise)
  • {fr} Fadya Hani, Monographie climatique d’une station synoptique, Kaolack 1946-1975, Université de Dakar, 1982, 113 p. (Mémoire de Maîtrise)
  • {fr} Emile Jacquier, « Le Port à arachides de Kaolack (Sénégal) », Publications du journal Le Génie civil, 1933
  • {fr} Alain Morice, Projet d'étude sur certaines activités dans la ville de Kaolack (Sénégal), École des Hautes études en sciences sociales, Centre d'études africaines, 1981
  • {fr} Alain Morice, Les forgerons de Kaolack : travail non salarié et déploiement d’une caste au Sénégal, Paris, EHESS, 1982, 6 + 350 p. (Thèse de 3Modèle:E cycle)
  • {fr} Mbaye Ndiaye, Histoire politique de la ville de Kaolack, (1945-1962), Université de Dakar, 1988, 104 p. (Mémoire de Maîtrise)
  • {fr} Soukeyna Ndiaye, Les équipements urbains au Sénégal : l’exemple de Kaolack 1946-1996, Dakar, Université Cheikh Anta Diop, 1999, 162 p. (Mémoire de Maîtrise)
  • {fr} Magatte Simal, Les Kaolackois face à l’administration coloniale de 1914 à 1938, Dakar, Université Cheikh Anta Diop, 1990, 93 p. (Mémoire de Maîtrise)
  • {fr} Denis Tillinac, L'Hôtel de Kaolack, Robert Laffont, 1991, Pocket n° 4602, 1992, 177 p. Modèle:ISBN (roman)

[Soppi] Lëkkalekaay yu biti


Logo Commons
Xool it Wikimedia Commons



aa - ab - af - ak - als - am - an - ang - ar - arc - as - ast - av - ay - az - ba - bar - bat_smg - bcl - be - be_x_old - bg - bh - bi - bm - bn - bo - bpy - br - bs - bug - bxr - ca - cbk_zam - cdo - ce - ceb - ch - cho - chr - chy - co - cr - crh - cs - csb - cu - cv - cy - da - de - diq - dsb - dv - dz - ee - el - eml - en - eo - es - et - eu - ext - fa - ff - fi - fiu_vro - fj - fo - fr - frp - fur - fy - ga - gan - gd - gl - glk - gn - got - gu - gv - ha - hak - haw - he - hi - hif - ho - hr - hsb - ht - hu - hy - hz - ia - id - ie - ig - ii - ik - ilo - io - is - it - iu - ja - jbo - jv - ka - kaa - kab - kg - ki - kj - kk - kl - km - kn - ko - kr - ks - ksh - ku - kv - kw - ky - la - lad - lb - lbe - lg - li - lij - lmo - ln - lo - lt - lv - map_bms - mdf - mg - mh - mi - mk - ml - mn - mo - mr - mt - mus - my - myv - mzn - na - nah - nap - nds - nds_nl - ne - new - ng - nl - nn - no - nov - nrm - nv - ny - oc - om - or - os - pa - pag - pam - pap - pdc - pi - pih - pl - pms - ps - pt - qu - quality - rm - rmy - rn - ro - roa_rup - roa_tara - ru - rw - sa - sah - sc - scn - sco - sd - se - sg - sh - si - simple - sk - sl - sm - sn - so - sr - srn - ss - st - stq - su - sv - sw - szl - ta - te - tet - tg - th - ti - tk - tl - tlh - tn - to - tpi - tr - ts - tt - tum - tw - ty - udm - ug - uk - ur - uz - ve - vec - vi - vls - vo - wa - war - wo - wuu - xal - xh - yi - yo - za - zea - zh - zh_classical - zh_min_nan - zh_yue - zu -