Diwaanu Tambakundaa
Ab jukkib Wikipedia.
Diwaanu Tambakundaa ngi nekk ci penku réew mi, benn la 14 diwaani Senegaal yi, di it bi ci ëpp ci yaatuwaay. réewu-taax mu Tambakundaa mooy péyub diwaan bi. am na 605 695 ciy way-dëkk te yaatoo 59 602 km2.
Tërëlin |
[Soppi] Melosuuf
[Soppi] Ay peggam
Diwaan baa ngi peggook:
- Diwaanu Maatam ak bu Luga ci bëj-gànnaaram;
- Diwaanu Kawlak ak bu Koldaa ak réewum Gaambi ci sowwam;
- Réewum Ginne ci bëj-saalumam;
- Dexub Senegaal bi, fi mu janook réewum Mali, ci penkoom;
[Soppi] Ay goxam
Ginnaaw bi, bi ñu defee goxub Kéedugu Diwaan bu mat sëkk ci 2008, Péncum Réewum Senegaal la ngi ko def ci 1 diggi-gammu ci 2008, diwaan bi ñaari gox rekk la am:
- Goxub Bakkel
- Goxub Tambakundaa
[Soppi] Xool it
[Soppi] Lëkkalekaay yu biti
- {en}Statistiques Geo Hive
- {fr}Conseil régional de Tambacounda
- {fr}Situation économique régionale de Tambacounda, édition 2005 (juin 2006)
|
|||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlak · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |