Diwaanu Ndakaaru
Ab jukkib Wikipedia.
Diwaanu Ndakaaru, benn la ci juroom-benni diwaan yu Senegaal yi. Moo ci gën a tuuti, ci yaatuwaay, waaye moo ci gën a bari way-dëkk. Yaatuwaayam toll ci 550 m Ñoo ngi ko séddale ci ñenti gox: Ndakaaru, Pikin, Géejawaay ak Tëngéj
[Soppi] Lëkkalekaay yu biti
|
|||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlak · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |