Yamoo
Ab jukkib Wikipedia.
Ci melosuuf, yamoo gi aw tus-wu-gar la, di ab buumub janeer bu ñu rëdd mu wër ab àdduna, jaar ci diggante dott yi. Yamoo gi moo xàjjale àdduna bi, def xaaju-kol-kol bu bëj-gànnaar ak xaaju-kol-kol bu bëj-saalum. Tus-wu-gaar wu yamoo gi 0° (tus aj). Guddaayu yamoo gu Suuf si mi ngi toll, cig xayma, 40 075 km.
Tërëlin |
[Soppi] Yamoog Suuf si
[Soppi] Klimaa
Klimaab barab yi ne ci li wër yamoo gi lañuy wax klimaab yamoo. Di nañ wax itam klimaab gëwéel, di bu barab yi ne ci li wër gëwéel yi (gëwéelub Tef ak gëwéelub Sànkar)
[Soppi] Réew yi mu dagg
Ci sunu àdduna(Suuf si), yamoo gi ay mbàmbulaan la ëpp ci li mu dagg ci yoonam, teemeer boo jël ci gudaayam ñaar-fukk ya rekk a jaar ci suuf.
[Soppi] Afrig
Yamoo gi jaar na ci juroom-ñaari réewi Afrig: