Web Analytics Made Easy - Statcounter

See also ebooksgratis.com: no banners, no cookies, totally FREE.

CLASSICISTRANIERI HOME PAGE - YOUTUBE CHANNEL
Privacy Policy Cookie Policy Terms and Conditions
Lëkkalekaay - Wikipedia

Lëkkalekaay

Ab jukkib Wikipedia.

Lëkkalekaay yi ñooy tax ñu man a jòge ci aw xët dem ci weneen wu mu lëkkalool.

[Soppi] Gongikuwaay ak àgguwaay

Ab lëkkalekaay day am gongikuwaay (maanaam fa muy jóge) ak ab àgguwaay (maanaam fa mu war a àgg, jëm fa). Soo doxalee xeetu(element) lëkkalekaay bi, ca saa sa, da ngay man a jàll ca àgguwaay ba.

Gongikuwaayub lëkkalekaay day doon naka-jekk ab xeet(ab baat, walla nataal,...) bu ab jukki. Àgguwaay bi man naa doon ab xeetu benn jukki bi, loolu la ñuy wax lëkkalekaay bu biir. Àgguwaay bi man naa doon itam beneen jukki, bu dul bi mu nekk.

[Soppi] Jaar-jaar

Lëkkalekaay yi ñi ngi sosu ci ati juroom-benn fukk yi, waaye seenug tas mi ngi ànd ak màggug internet, di fu Lëkkalekaay yi di boole, niki ab lënd, ay junny junni dal ci Lëkkale(resaux) gi. Su dul woon Lëkkalekaay yi, xereñu Internet di na wàññiku bu baax, jafeel jëfandikoom.

Ak jëm-kanamug gu réy gu Internet, lëkkalekaay yi, ci li ñuy tag yu HTML la ñuy jaare di leen sos, joowukaay bi won la ko; ci misaal

<a href="http://it.wikipedia.org">Wikipedia</a>

moo lay jox: wikipedia

Tay jii sax lëkkalekaay yi ay nattukaay lañu, limu lëkkalekaay yiy jëme ci ab dal ci la ñuy xamee ñaata la siiwee.

[Soppi] World Wide Web

lëkkalekaay yu World Wide Web bi ci xëti web yi la ñu nekk, maanaam ci jukki yi ñu bind ak HTML (Hypertext Markup Language).


aa - ab - af - ak - als - am - an - ang - ar - arc - as - ast - av - ay - az - ba - bar - bat_smg - bcl - be - be_x_old - bg - bh - bi - bm - bn - bo - bpy - br - bs - bug - bxr - ca - cbk_zam - cdo - ce - ceb - ch - cho - chr - chy - co - cr - crh - cs - csb - cu - cv - cy - da - de - diq - dsb - dv - dz - ee - el - eml - en - eo - es - et - eu - ext - fa - ff - fi - fiu_vro - fj - fo - fr - frp - fur - fy - ga - gan - gd - gl - glk - gn - got - gu - gv - ha - hak - haw - he - hi - hif - ho - hr - hsb - ht - hu - hy - hz - ia - id - ie - ig - ii - ik - ilo - io - is - it - iu - ja - jbo - jv - ka - kaa - kab - kg - ki - kj - kk - kl - km - kn - ko - kr - ks - ksh - ku - kv - kw - ky - la - lad - lb - lbe - lg - li - lij - lmo - ln - lo - lt - lv - map_bms - mdf - mg - mh - mi - mk - ml - mn - mo - mr - mt - mus - my - myv - mzn - na - nah - nap - nds - nds_nl - ne - new - ng - nl - nn - no - nov - nrm - nv - ny - oc - om - or - os - pa - pag - pam - pap - pdc - pi - pih - pl - pms - ps - pt - qu - quality - rm - rmy - rn - ro - roa_rup - roa_tara - ru - rw - sa - sah - sc - scn - sco - sd - se - sg - sh - si - simple - sk - sl - sm - sn - so - sr - srn - ss - st - stq - su - sv - sw - szl - ta - te - tet - tg - th - ti - tk - tl - tlh - tn - to - tpi - tr - ts - tt - tum - tw - ty - udm - ug - uk - ur - uz - ve - vec - vi - vls - vo - wa - war - wo - wuu - xal - xh - yi - yo - za - zea - zh - zh_classical - zh_min_nan - zh_yue - zu -