Dalmasi
Ab jukkib Wikipedia.
Ci angale mooy Dalmatia; Ci faranse mooy Dalmatie
Ci jamonon Injill diiwaan la woon, ci sowu-suufu diiwaanu Room bu tuddoon Iliri ci penku géeju Adiratig. Maanaam mooy daanaka réew mi ñu waxoon Yugosalawi (ex-Yougoslavie), te ñu wax léegi Korwaasi, Bosni-Ersegowin ak Montenegëro.
Dañu ciy wax ci 2Tim 4:10.