Web Analytics Made Easy - Statcounter

See also ebooksgratis.com: no banners, no cookies, totally FREE.

CLASSICISTRANIERI HOME PAGE - YOUTUBE CHANNEL
Privacy Policy Cookie Policy Terms and Conditions
Bawol - Wikipedia

Bawol

Ab jukkib Wikipedia.

Ci xarnub fukk ak juroom Bawol nguur su ndaw la woon su toppoon Jolof gu mag gi, bu ko defee, ag njaboot gu amug jegeñaale ak buuri Kajoor yi daa ko jiite.

Ci xarnub fukk ak juroom benn g.j, la Jolof mànge poseb néew-dooleg nguurug Jolof , daal di jël ag tembam, ni ko yenn ci nguur yi defe woon, gu ci mel ne Kajoor ak Waalo, ngir song gu tar ga Amari Ngóne Sabel Faal defoon Jolof. Ci ñaareelu xaaju xarnu bii la Amari Ngóone xëy di buuru Kajoor ak Bawol ci jenn jamono ji.

Booba la buur bi tàmbalee jiite ñaari nguur, waaye nguur gu ci nekk yor politigu doxaliinu réewam. Waaye boole gii bari lu mu daa jur ay réeroo ci diggante ñaari nguur yi, ndax gu ci nekk daa bëgg a yilif ga ca des.

Buurub Bawal nag di Teeñ ab jataay a ko daa jàppale, bu ñu wéer tabbug kiy wuutu buur bi bu faatoo, ak fuglug saxal yi buur bi di def. Nguur gi amoon na ab ëttu àtte buy àtte mbir yi, mbooleem maas yi nag daa nanu fa àttewoo (maasug nappkat yi, baykat yi, sàmm si, ñoñ fànn ñi (boroom mecce yi) ak jigéen ñi). Bokkug Bawol ci Yaxantug Tàkk gi taxu ko woon a deme noonu, ndaxte yooni yaxantu gi rombutoon ciy suufam, moom kay daa yamoon rekk ci yaxantug tefes gi.

Seetal BUNTU TAARIIX
Yeneeni làkk


aa - ab - af - ak - als - am - an - ang - ar - arc - as - ast - av - ay - az - ba - bar - bat_smg - bcl - be - be_x_old - bg - bh - bi - bm - bn - bo - bpy - br - bs - bug - bxr - ca - cbk_zam - cdo - ce - ceb - ch - cho - chr - chy - co - cr - crh - cs - csb - cu - cv - cy - da - de - diq - dsb - dv - dz - ee - el - eml - en - eo - es - et - eu - ext - fa - ff - fi - fiu_vro - fj - fo - fr - frp - fur - fy - ga - gan - gd - gl - glk - gn - got - gu - gv - ha - hak - haw - he - hi - hif - ho - hr - hsb - ht - hu - hy - hz - ia - id - ie - ig - ii - ik - ilo - io - is - it - iu - ja - jbo - jv - ka - kaa - kab - kg - ki - kj - kk - kl - km - kn - ko - kr - ks - ksh - ku - kv - kw - ky - la - lad - lb - lbe - lg - li - lij - lmo - ln - lo - lt - lv - map_bms - mdf - mg - mh - mi - mk - ml - mn - mo - mr - mt - mus - my - myv - mzn - na - nah - nap - nds - nds_nl - ne - new - ng - nl - nn - no - nov - nrm - nv - ny - oc - om - or - os - pa - pag - pam - pap - pdc - pi - pih - pl - pms - ps - pt - qu - quality - rm - rmy - rn - ro - roa_rup - roa_tara - ru - rw - sa - sah - sc - scn - sco - sd - se - sg - sh - si - simple - sk - sl - sm - sn - so - sr - srn - ss - st - stq - su - sv - sw - szl - ta - te - tet - tg - th - ti - tk - tl - tlh - tn - to - tpi - tr - ts - tt - tum - tw - ty - udm - ug - uk - ur - uz - ve - vec - vi - vls - vo - wa - war - wo - wuu - xal - xh - yi - yo - za - zea - zh - zh_classical - zh_min_nan - zh_yue - zu -